graves révélations de ahmed khalifa niasse "ils ont tué mon frère et je vais..."

Commenti

  • Kéba Sokna
    Kéba Sokna

    Machallah ler n'a diaradiaf Niass

    6 giorni fa
  • Mbacke Seck Ndar
    Mbacke Seck Ndar

    Sunu xell dou masa diouk si Elhadji sidy lamine niass Tey niane Yalla mou teralko sa Aljana firdawsi

    6 giorni fa
  • Mamadou Niang
    Mamadou Niang

    merci rafétena yalla noko yalla kharé aldiana firdaossi

    7 giorni fa
  • Meissa Sall
    Meissa Sall

    Rip

    8 giorni fa
  • Meissa Sall
    Meissa Sall

    Rip

    8 giorni fa
  • Meissa Sall
    Meissa Sall

    Rip

    8 giorni fa
  • Serigne Mbacke
    Serigne Mbacke

    amna gnokhamné dougnou wakhlou rafét mais Ahmed khalifa niass limou wakh lougnou mana dégla ligadef rafétna yallnalafi yalla yaggall barké cheikhoul khadim.....sidy lamine niass yalnako yalka kharé aldiana barké mamam seydina mouhamed (slw)

    8 giorni fa
  • Mouhamed Diouldé Diallo
    Mouhamed Diouldé Diallo

    yalla nako yalla yeureum, khareeko al dianna té samme la niass

    8 giorni fa
  • Aliou Dieng
    Aliou Dieng

    Paie à son âme et que la terre de leona lui soit légère

    8 giorni fa
  • Djily Bagdad jr
    Djily Bagdad jr

    Hamet wadji rafetna lol sakh yalla nako yalla kharé dianatoul firdawsi sa yalla dolé takhawou

    9 giorni fa
  • Sokhna Maty Mountaha
    Sokhna Maty Mountaha

    ki nimako mere maitesin après la mort

    9 giorni fa
  • Ousmane Ndongo
    Ousmane Ndongo

    Yo Allah yourmo yafomo yo Allah harnoumo alidjana amine yarabi

    9 giorni fa
  • Mounaf Fall
    Mounaf Fall

    Ahmet khalifa Niasse est un gros menteur, un affabulateur😐😐..je suis trop fàchée sama khol nékhoul...Ecoutez la video de son fils Cheikh Ahmet Niasse (dont il dit kil né pas l'ainé) ki dit: " son père avait échangé avec lui plusieurs fois sur whatssapp et disait kil souhaiterait étre enterre a Yoff à sa mort" ( entretien sur Walf tv avec un journaliste)... lolou dome di na ko fenne si bayam..mou gnewe di wakh lénne. Yalna ma yal bal té diéguelma si wakh bi wakh si ce monsieur là! Et puis malhonnete kil est: si YOFF yavait pas de blem comme il dit, pourkoi ne pas l'enterrer laba? lui méme dit pas des choses normales.

    9 giorni fa
  • Moussa Diallo
    Moussa Diallo

    Toujour les Franc maçons mai en quelque sorte Ahmed Khalifa niasse même si tu va te venger mai tu dois garder les secret familial comme tu va payé les études donner les enfants de quoi manger etc... ou vas le monde je ne di même pas le Sénégal avec cette puissance mondiale 😏😔

    9 giorni fa
  • Souleymane Drame
    Souleymane Drame

    Paix à son âme sidy lamine diambari l'islam

    9 giorni fa
  • Alpha yaya Diallo
    Alpha yaya Diallo

    Quallah l'accueil dans son paradis céleste

    9 giorni fa
  • m diarra Bassel
    m diarra Bassel

    Yalla nako yalla yeuram ta khare ko aldiana firdawsi 😭 Yawit yalla nalafi yalla yagal lool amine

    9 giorni fa
  • Black Queen
    Black Queen

    Gni ay nitu problem lagn. Mé senegal mom kou dè done waliou

    9 giorni fa
  • Koita Boussan
    Koita Boussan

    Paix à son âme.,et longue vie aux autres.

    9 giorni fa
  • lamp fall
    lamp fall

    C'est triste vraiment Sidy Lamine Yalna YALLA yok lérame té oyofale soufe si kawam

    9 giorni fa
  • sall mohamed habib
    sall mohamed habib

    que dieux l'accueil dans son paradis

    9 giorni fa
  • Cheikh Sy
    Cheikh Sy

    Yow ahmed doo rouss tu es pathétique yaay pir dajjal ibliss 😡

    9 giorni fa
  • isac fall
    isac fall

    Yallah nacko yallah yeureum té djégueul ko kharé aldjanatoul firdawssi barqui borom Touba khadimou Rassoul yallah n'a nacko sanguam wou teed wowou terou cheikh Ahmed tidjani

    10 giorni fa
  • abdoul ndiaye
    abdoul ndiaye

    Khalifa Niasse noppil

    10 giorni fa
  • Diallo Anta
    Diallo Anta

    Ndeyesan yalna ko yalla kharé adiana

    10 giorni fa
  • Maréme Thiam
    Maréme Thiam

    J'arrive tjr pas à croire qu'il n'est plus 😔😔 ndeysann

    10 giorni fa
  • Khadim BEYE
    Khadim BEYE

    Kadou yi rafetna Machalla

    10 giorni fa
  • Bijou Gueye
    Bijou Gueye

    Yalnako yalla khare aldiana firdawsi je crois son discours certe c magnifique mais sa aurai pu reste au sein de la famille

    10 giorni fa
  • petit senegal
    petit senegal

    Je ne comprend pas pourquoi cheikh voulait ecarter ses 2 freres ainé....c est pas serieux

    10 giorni fa
  • Ndeye Sokhna
    Ndeye Sokhna

    Ndeysane Yalna nako yala yereum kharei aldiana fiirdawsii amine

    10 giorni fa
  • Fatou kine Diallo
    Fatou kine Diallo

    rip sidi lamine niass

    10 giorni fa
  • GUEYE MALICK
    GUEYE MALICK

    Aduna amoul solo sidy yalla nako yalla yeurem

    10 giorni fa
  • CCTB
    CCTB

    Sénégal mo nieuk

    10 giorni fa
  • Mike Ndiaye
    Mike Ndiaye

    Wakh deug nainene bayi kilifeu ahmed decidé fougni dinth rakam nakhté mak denkeye ormal djokko loumoumome sidy kou bakhla kou dimeuli aye domou adama la donc la decision apparttien au grand frere ahmed c le kilifeu de la famille

    10 giorni fa
  • Abdou Samth
    Abdou Samth

    wakh dji refet na

    10 giorni fa
  • Idda Manga
    Idda Manga

    Svp c est pas le moment toi tu connais pas les noms des enfants de sidi lamine niasse paix a son ame

    10 giorni fa
  • Idda Manga
    Idda Manga

    C est le Senegal qui a perdu

    10 giorni fa
  • Abdoul bowel mnt Bah
    Abdoul bowel mnt Bah

    Pai a son ame

    10 giorni fa
  • Moussa Catalan Diop #7
    Moussa Catalan Diop #7

    😭😭😭😭

    10 giorni fa
  • Omar Gueye
    Omar Gueye

    Yalla na khipé aldianay firdaysi

    10 giorni fa
  • Sira Mane
    Sira Mane

    avent TT j vous dis inna lilakhi wa inna ileykhi radioune.mame sidy.nite gnou Barry dougnouko raagné kééke guénoul adouna en tte franchise j n lui donné pas trop d importance.en fin yalla nako yalla yeureme kharéko ardiana oyofolko souf thi kawame.merci

    10 giorni fa
  • Ousmane Diba
    Ousmane Diba

    Sénégal niakc n'a bonkal mou khamne dou tofi amati

    10 giorni fa
  • Amet Ndiaye
    Amet Ndiaye

    Nous sommes tous des sénégalais priés pour le repos de son âme

    10 giorni fa
  • DIAWARA CHEIKH OUSMMANE
    DIAWARA CHEIKH OUSMMANE

    Un gd homme est parti k Dieu lakeuy ds son paradis le sénégal avait besoin de toi pdt les elections Sidi est iremplaçable

    10 giorni fa
  • Ndiaye babacar
    Ndiaye babacar

    Ndeyssane sa wakh rafetna yalla nala yalla defall diam

    10 giorni fa
  • DIAWARA CHEIKH OUSMMANE
    DIAWARA CHEIKH OUSMMANE

    Mbéguélle gi ma amône thi yaw yokouna téy yalana yalla yeureum seugn sidi té bayilafi ba nga ame 100 ans té wér

    10 giorni fa
  • Fall Dame
    Fall Dame

    nit kou bax ta fonk l islam

    10 giorni fa
  • Fall Dame
    Fall Dame

    yalla nako yalla xare aldjiana

    10 giorni fa
  • Ndiaye babacar
    Ndiaye babacar

    Ndeyssane

    10 giorni fa
  • Vladislav Stanchev
    Vladislav Stanchev

    R.i.p

    10 giorni fa
  • Bada Fall
    Bada Fall

    Yallnako yalla yaram te kharrèko alldiana si barkep serigne touba akhmad xaliffa liga deff refettna yallnala yalla fay si barkep yonentibi salla -----------------wa salam

    10 giorni fa
  • Mouhaméd Thiam
    Mouhaméd Thiam

    Yallanako yalla yeureum tékharéko aldiana

    10 giorni fa
  • Khadim Mane
    Khadim Mane

    Il ne faut pas jugé ameth khalifa de mal son problème ak sidy yaguena na si famille donc fait attention pour vos jugements Ahmed reste toujours grand à sidy lamine Que terre lui soit légère si barki seydina mouhamed

    10 giorni fa
  • Magatte Ndao
    Magatte Ndao

    Svp bayil cheikh mou dèf li papam beugeu sa domla

    10 giorni fa
  • Fall Badara
    Fall Badara

    اللهم أغفر له وأرحمه ووسع مدخله وأسكنه جوار سيدنا محمد صلى الله عليه وسلم آمين

    10 giorni fa
  • Saidou Sy
    Saidou Sy

    halaat leen lou wahone Ay wah you niaw en vers toute la communauté peulh

    10 giorni fa
  • mouhamed lamine ndiaye
    mouhamed lamine ndiaye

    Yalna ko yallah kharé aldianay firdawsi, Sénégal gnépa niakk....

    10 giorni fa
  • Amy Diouf
    Amy Diouf

    Yalla na Diam sakh si rewmi, Sénégal deuk diam la deuk diné la

    10 giorni fa
  • Souleymane Dione
    Souleymane Dione

    Yalnako yalla yereum té xarrr ko aljana firdawsi paix à son âme

    10 giorni fa
  • Diènaba Camara
    Diènaba Camara

    Paix a son ame sa xaw rafenat yala na la faye mboko alalou yala diara dieuf tonton khahmete

    8 giorni fa
  • Ndiaye Abdurahmane
    Ndiaye Abdurahmane

    Yalla na déé di noflayam famou djeum gueuneul co fimou djogué si barké Baye ak bayam

    10 giorni fa
  • Khadim Sall
    Khadim Sall

    Ndéyssaane rafétna Ahmad vérement kilifeu nge machaalah

    10 giorni fa
  • el hadjiabdourakhmane ba
    el hadjiabdourakhmane ba

    c Allah qui prend la vie comme Il veut.cessez d'incriminer qui que ce soit et priez pour que Allah étende son person à tous ceux qui aiment Seydina Muhammad psl

    10 giorni fa
  • young hamzo
    young hamzo

    Yallah nako yallah yeureum kharé ko aldiana...Mais kii loumouy wakh kéne douko wakh déjà ki kéne diebeulo gouko suñu borom mouy beugg andi polémique ca se fait pas ahmed khalifa....où en est ta croyance en dieu si tu te dis que tu es un homme saint🤷‍♂️

    10 giorni fa
  • tyfa Ndiaye
    tyfa Ndiaye

    Machalla wakh dji rafét na

    10 giorni fa
  • Aminta Seye
    Aminta Seye

    Paix à son âme Ahmed khalifa yana yala goudal fane yi

    10 giorni fa
  • Lahate Fall
    Lahate Fall

    problème bepou yako fi indi lo dougou rek indi fa thiow

    10 giorni fa
  • Cheikhouna Diop
    Cheikhouna Diop

    Yalnako yalla yeurem

    10 giorni fa
  • Issa dawa Beye
    Issa dawa Beye

    Yalnako yalla yeuram té khareko aldiana

    10 giorni fa
  • MA#*d99-114*
    MA#*d99-114*

    Paix à son âme que dieu l’accueille dans son paradis ,un homme dignes,tu resteras grave dans nos cœurs

    10 giorni fa
  • SANKOUN KANOUTÉ
    SANKOUN KANOUTÉ

    Amna kaddu yima rafetlewoul dakh c'est pas le moment et ni le lieu

    10 giorni fa
  • Diakhate Serigne mbacke
    Diakhate Serigne mbacke

    Yalla nako yalla yeureum te kharko aldiana barkep s saliou

    10 giorni fa
  • Diakhate Serigne mbacke
    Diakhate Serigne mbacke

    Youbou lene ko touba kaye waxdji djiekh

    10 giorni fa
  • Seni Sane
    Seni Sane

    Cei vrais ke metinat mais ne sois pa a la place de dieu bayilene ak yala dara oumpouko

    10 giorni fa
  • Mamadou Ndiaye
    Mamadou Ndiaye

    Deireite daffa fort wallakhi ndeyssane

    10 giorni fa
  • Angelique Mendy
    Angelique Mendy

    Am mbok boubakh mo rafet kar machala

    10 giorni fa
  • Birame fall Fall
    Birame fall Fall

    Yallah nako yallah dieguale amine

    10 giorni fa
  • Angelique Mendy
    Angelique Mendy

    Repose en paix Sidi Lamine Niass que Dieu t accueille dans son paradi Amen

    10 giorni fa
  • Mbend Pouye
    Mbend Pouye

    Ki vrai iprocrite la lép loumou def rek defouko si zero louné gaka dan yak

    10 giorni fa
  • Papa Gallo Diouf
    Papa Gallo Diouf

    loumana khew rakam la kone arrête ces insultes loléne di saga nite bambou ame nakhar khana ngéne maneko bayi

    10 giorni fa
  • NdèyeFA NDIAYE
    NdèyeFA NDIAYE

    Masseu Khalifa meetina, je réitère mes sincères condoléances à toute la famille NIASSE. Yal naco YA ALLAH sunu borom bou tedeu bobou Akfirlahoum wa Rahmawou Sidy Lamine NIASSE. Le Senegal à perdu un grand homme de valeurs, il a honoré sa mission de passage sur terre avec honneur MashaAllah. Seutou yonèteu you bakh yeupa soneu, dagniouy djihad ba bi gniouy wouyou dji sène borom. Wayé guinawam rafètna yaleu bouko thiate djitou ci bamelame. Je l'aimais tellement❤. Il restera à jamais dans mon coeur😭😭

    10 giorni fa
  • cheikh sy
    cheikh sy

    Paix à son âme qu'Allah l'octroi en son paradis

    10 giorni fa
  • Khady Ndiaye
    Khady Ndiaye

    Yena gui dieuw dee rekk mowour yao amo diom mandouvo

    10 giorni fa
  • Sally S.
    Sally S.

    d’abord kou sage kou am xam xam demna djalenako senegal yeup yallah nako yallah xaré firdawsi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾ok maintenant Waxna ba wax lou eup li mo tax gnou mane wax foula day gatt khalifa Niass en ce moment est rentrè dans des polémiques vrmt pas nécessaire wax deu yallah. Ahmet Niass xawma kagne lay magueu guir yallah sagesse soudone djay dinako djeundeul

    10 giorni fa
  • Ibrahima Sow
    Ibrahima Sow

    Yalna yeurmandé yalla wathi si kawam

    10 giorni fa
  • guer gu
    guer gu

    Rafetna lol guanala beugue

    10 giorni fa
  • Diop Ndeye
    Diop Ndeye

    C normal

    10 giorni fa
  • Madame Dieng
    Madame Dieng

    Ndeysane c'est triste mais bou yalla doon taggo billay dou dém ndakh kou bakhoone la loool wayé lou yalla def ken menou thi dara yallna ko sounou borom bi kharé adiana barqué ckheikhoul Khadim

    10 giorni fa
  • omar samba ndiaye
    omar samba ndiaye

    Wakh dji raféte na ! Mais meunone nga récupérer sa rak bala beussou tay bi

    10 giorni fa
  • Ndelladjima Diarra
    Ndelladjima Diarra

    Wakh gua lou rafete niass dieureudieuf

    10 giorni fa
  • Saliou Mbaye
    Saliou Mbaye

    Yalla nako Mouhamet terou si Firdaysi

    10 giorni fa
  • Rien que du foot foot rk
    Rien que du foot foot rk

    Rafet n'a niass coumba Abdallah yalla n'a borom bi motali

    10 giorni fa
  • ami gueye
    ami gueye

    Yalna Yalla khareko Aljana firdawsi

    10 giorni fa
  • Serigne Fallou
    Serigne Fallou

    PAIX À SON ÂME ALLAHOU MA AMIIINE

    10 giorni fa
  • Lat Diop
    Lat Diop

    SIdy lamine yalla nako yalla yarame te youbou ko si aldiana ya gana kave mais kiko Ray lou yalla nako feki legui bala yague te kiko Ray yalla nako yalla torakhal fi si adona

    10 giorni fa
  • Samba gagnessiry Sarr
    Samba gagnessiry Sarr

    Gnikoy sédé tay niouthi Bari ayy nonamm lagne wone ndakh môme DEUG AK yone ladone khékhal té niom ibliss lagne geumm AK adounaaa AK khaliss .loutakh sédé wouléne KO wone lou bakh bimiy doundou .thimmmmm narfékh yi nieupp pagui wakh té Dara geumouniouko

    10 giorni fa
  • Fatou Sha
    Fatou Sha

    Thiey kou d ya porte repose en paix sidy lamine li metina

    10 giorni fa
  • doman keita
    doman keita

    Ahmed lou bax rkk lay wax bayilène koo

    10 giorni fa
  • khady sow
    khady sow

    SIDI EST PARTI, la vérité marchante est parti. j'ai pas eu l'occasion de la connaitre personnellement j'ai j'ai essayer en demandant des audiences pour le voir. une grande perte pour la vérité, une grande perte pour la presse . un homme qui savait que seule le travail paye. il a bâtie un grand complexe, WALFADJRI, que dieu l’accueille au paradis au nom de Walfadjri . il a fait manger ,il a fait soigner,il a fait vêtu des personnes alors que se n'était pas évident. la nation en pleure, le monde en pleure, la vérité en pleur, sidi, repose en paix au nom de TAHA MA ANZALNA ALAYKALKHOURANE.

    10 giorni fa
  • Marietou Thiam
    Marietou Thiam

    Juska présent meunougnouko dégnethe c malheureux mon pays va trés mal

    10 giorni fa
  • Ndiawe Ndiaye
    Ndiawe Ndiaye

    Machalla akhmete Sidi yalla na ko Yalla yeureum té djiégeul ko aminn

    10 giorni fa
  • diouf gnilane
    diouf gnilane

    Paix à son âme

    10 giorni fa