Kooru Biddew Saison 4 - Épisode 12

Abonnez-vous à notre chaine IT-stream it-stream.com/section/UCOvrLn57A83J8ojcX70n0Ew
Suivez-nous sur Facebook facebook.com/leuzmedia?fref=ts

Commenti

  • faye bineta
    faye bineta

    mais j pose la kestion épouser une deuxième femme est un crime pourtant une femme peut remplie tt c devoir d épouse mais on peux épouser une autre

    Mese fa
  • Suzanne CAMARA
    Suzanne CAMARA

    Daro daff may fathh 😀😀

    2 mesi fa
  • Nouveau type de Senegalais
    Nouveau type de Senegalais

    Omg ! Elle est trop belle la mechante copine ! Sa noirceur machallah! Wayé beuri maniere moko yakk. Bo xessalé nala door dé!

    2 mesi fa
  • Guigui Ndao
    Guigui Ndao

    Xamngakoo sii ousseynou 😂😂😂😂😂😂 sacre daroo

    2 mesi fa
  • Ngomez Bii
    Ngomez Bii

    Dane...franchement da nga meuneu mougneu koi..🤣🤣🤣

    3 mesi fa
  • Maimouna Ndoye
    Maimouna Ndoye

    Niarél mass bouléne ko blâmé dax dom bimou amm

    3 mesi fa
  • dior gueye Diop
    dior gueye Diop

    Lamine ndiaye c pa normal

    3 mesi fa
  • Aicha Diallo
    Aicha Diallo

    L amie de Adji elle east hipocrite que dieux nous epargne de ces genre d amie Amineeeeeeeeee

    3 mesi fa
  • RD Ndiaye
    RD Ndiaye

    Mass ressemble à Lamine Ndiaye

    3 mesi fa
  • Ndeye Fatou FALL
    Ndeye Fatou FALL

    Soubana xarite bou xame sa biir akk sa biti ba paré dila yakale...nonou privée mrci reikkk

    3 mesi fa
  • mme siby
    mme siby

    NON MAN DARO LAY WEUR

    3 mesi fa
  • Gueye Sokhna
    Gueye Sokhna

    Le soleil crée de la vitamine D (pas E, ou en tt cas pas en majorité)... la vitamine D est autrement appelé la “vitamine soleil”

    3 mesi fa
  • adjara gnima Sanè
    adjara gnima Sanè

    Lamine ndiaye me rappelle mon défunt père avec sa barbe yalla nako yalla yeureum Lamine ndiaye yalla nga koudu fann inchalla

    3 mesi fa
  • Modou Diop
    Modou Diop

    Machalla

    3 mesi fa
  • Sweet Radia
    Sweet Radia

    Pkoii diaboliser niarel ?

    3 mesi fa
  • Nanetteada12
    Nanetteada12

    Lol Mas il fallait faire ces efforts avants

    3 mesi fa
  • Fatoumbacké Diakhoumpa
    Fatoumbacké Diakhoumpa

    Thieye kharitou légui yi

    3 mesi fa
  • Junior Fall
    Junior Fall

    Wa kharitou adji bi mom loutakh mou jalouse si adji non li mom yalla naniousi yalla mousal

    3 mesi fa
  • Lo Asta
    Lo Asta

    Soleil produit vitamin D

    3 mesi fa
  • dialmb
    dialmb

    Quand leurs fesses chauffent là ils reviennent la queue entre les jambes. Tchiiip

    3 mesi fa
  • dialmb
    dialmb

    Damey beug diomi wala soupou kandia bi dafa ame poivron?

    3 mesi fa
  • thiarra thiam
    thiarra thiam

    Mais gnarel rou Mass bi da beug Mass ba geumé wouko ndeyesane seuy mbeuguel

    3 mesi fa
  • ka le roi
    ka le roi

    Balko akh waye

    3 mesi fa
  • Ryma Sarr
    Ryma Sarr

    Désolé j’ai entendu une phrase « le soleil produit de la vitamine E » non c’est plutôt de la vitamine D

    3 mesi fa
  • Aliou Leye
    Aliou Leye

    No

    3 mesi fa
  • ibou tailleur Gueye
    ibou tailleur Gueye

    Mass boul balou

    3 mesi fa
  • boubs gaye
    boubs gaye

    Kharitou adji bi sokhorna trop

    3 mesi fa
  • Sokhna oumy Gueye
    Sokhna oumy Gueye

    Dégueul ndidiayou mass nenako talons auto bi niou deime verbe taler ngaye ame fofou

    3 mesi fa
  • Temi Tope Balogun
    Temi Tope Balogun

    il y a beaucoup de Femmes comme ADJI... mauvaises, briseuses de menage, et ne valent rien.. DIEU AIDE NOUS ET PRESERVE NOUS DE CES GENRES DE PERSONNES

    3 mesi fa
  • Mamadou Lamine Cisse
    Mamadou Lamine Cisse

    Mnt c'est comme si avoir une deuxième femme c'est diabolique. Arrêter vos bêtises waay issh

    3 mesi fa
  • Ndiaye Aissata
    Ndiaye Aissata

    Oh hai tellement aimé la secance de mass et bidew c’était très romantique billahi 🥰

    3 mesi fa
  • Maman Dieng
    Maman Dieng

    Lane moye ndéye nebe dome darra diaro ko nakh goor diarou ko sama dome sama dome laaaaaa doumo k. nébe jamé nakh laaaa

    3 mesi fa
  • Mody Toure
    Mody Toure

    Mdrrrrr mimi nobone nala mei bayi wate nako🤣🤣🤣🤣🤣

    3 mesi fa
  • Ouz Ba
    Ouz Ba

    ms bidéw bi prkw el réagi kom sa gor da wara ame 1 2 3 ba 4 sahh ndeyessane dafa dajié gor bou bah ba mélni Mane rkk😀😀

    3 mesi fa
  • houleye coulibaly
    houleye coulibaly

    Bilahi elle ne mérite pas d'avoir une coepouse biddew 🤗🤗

    3 mesi fa
  • Yakub Diallo
    Yakub Diallo

    LI DAL MASS MOMA NARON DAL 2014..MY FATHER BEUGON MA DOUGAL SI BEN FEMME BO HAMNE HAWMAKO .. MA BAGN MOU MERE MA.. BATAY GIFOUT.. MAYOUMA DIAM TMT

    3 mesi fa
  • Ameth Sarr
    Ameth Sarr

    Mass bayil doul tapett nga rek

    3 mesi fa
  • aminata diop
    aminata diop

    bedeew ,teint bi Nice maachaallah

    3 mesi fa
  • adji daro seye
    adji daro seye

    J'aime bideww mais aussi adji ndakhté woudiou manoul niakk kaméme

    3 mesi fa
  • Kalz Seneg
    Kalz Seneg

    Mass yambar neu way ahhhh

    3 mesi fa
  • Awai Gueye
    Awai Gueye

    L'incarnation de nos amie de nos jours..sounioula guissei dila retane gua tourné nioulay bign..yallah naniou yallah mouseul si peikhei noone

    3 mesi fa
  • Diarra Dieng
    Diarra Dieng

    Kharit bou djiguéne kay merci rk kholal lu rk

    3 mesi fa
  • THIAPRO TLD
    THIAPRO TLD

    ça se passe ici..one clic for Biddew👍Rejoignez moi sur youtube it-stream.com/section/UC--saj-7S-z7v5ZgA0572zg

    3 mesi fa
  • THIAPRO TLD
    THIAPRO TLD

    ça se passe ici..one clic for Biddew👍Rejoignez moi sur youtube it-stream.com/section/UC--saj-7S-z7v5ZgA0572zg

    3 mesi fa
  • Serigne Touba Ndiaye
    Serigne Touba Ndiaye

    ADJA🕞

    3 mesi fa
  • KHADY SOW
    KHADY SOW

    Xaritu niarel bi dafa nopp Mass motax mouy yakk

    3 mesi fa
  • khady diouf
    khady diouf

    Tonton le soleil ne produit pas de la vitamine E mais plutôt de la vitamine D Depuis la Belgique

    3 mesi fa
  • Sokhna Mbow
    Sokhna Mbow

    Ahhh maggi mo bakh si yaram ah rouss na bidew🤐🤐🤐🤤🤤

    3 mesi fa
  • Alima Konate
    Alima Konate

    Wouy daro néna xamnako si ousseynou 😁

    3 mesi fa
  • pisdo mix tv
    pisdo mix tv

    Ahh Mass li mom bou yagueu nguaka warone deff

    3 mesi fa
  • Hadidiatou Ndiaye
    Hadidiatou Ndiaye

    Li wolof di wakh bala nga khamm khamadi khawla reyy mo dall mass , adouna ken dou fadjé merei sa diabar ak takalko une autre oubien avoir une maîtresse. Voici les conséquences

    3 mesi fa
  • kenza ndiaye
    kenza ndiaye

    Mouyen la dame noire avc l percing c immature 🤔🤔🤭

    3 mesi fa
  • Sunkiss glowy
    Sunkiss glowy

    Vitamine D

    3 mesi fa
  • Laye Mbodji
    Laye Mbodji

    Juste un petit quiproquo grand, mais très important ! Le soleil ne produit pas de la vitamine E, mais de la vitamine D! Que les scénaristes fassent plus attention aux dialogues.

    3 mesi fa
  • STRONG WOMAN MBACKÉ
    STRONG WOMAN MBACKÉ

    bidew beug na sa djiko daga mandou lol

    3 mesi fa
  • Ndiaye Maïmouna
    Ndiaye Maïmouna

    Mass way mon amour 😅

    3 mesi fa
  • Kady Cisse
    Kady Cisse

    Intéressant

    3 mesi fa
  • Ndeye aida Ba
    Ndeye aida Ba

    Le soleil ☀️ produit de la Vitamine D qui fortifie les os 🦴 pas vitamines E 😂😂

    3 mesi fa
  • ali cr7
    ali cr7

    où masse ya problème

    3 mesi fa
  • Thialy Thiam
    Thialy Thiam

    😂😂😂

    3 mesi fa
  • Firstime Tine
    Firstime Tine

    Masss nak beugu n’a bidew😂

    3 mesi fa
  • Diana Njaay
    Diana Njaay

    Goor nilay meel waay nangou danou ramm nguiir sa diabaar

    3 mesi fa
  • Mariama dia toukoulor bou rafét bi
    Mariama dia toukoulor bou rafét bi

    Team bideew 😍😍dépui Italie

    3 mesi fa
  • Binoush bae
    Binoush bae

    Mass ak beutou tapett yi 🤣🤣🤣 mane dall goor litakh mou gnak djom la khamoul thieuyy li

    3 mesi fa
  • Bois D'ébène
    Bois D'ébène

    le soleil produit de la vitamin D pas E

    3 mesi fa
  • Cheikh Darou Sylla
    Cheikh Darou Sylla

    😆😆😆😆 Xam ngako si Ousseynou non Daro srx woul kw

    3 mesi fa
  • Ndeye Aissatou Niang
    Ndeye Aissatou Niang

    Maan daal xeitou niit yii rk mtx beugouma amm xariit bou djiguene xaritou Adji bii daal mooy lolou shiit xariit bou goor daal Diam rk lassii guiss

    3 mesi fa
  • Dame Syll
    Dame Syll

    Mass yambar la koi 😂😂

    3 mesi fa
  • Petit Mbaye
    Petit Mbaye

    Non vraiment mai mass kou yambar la

    3 mesi fa
  • Lil badou
    Lil badou

    Nagnouko fotonk fotongal rek dadikoy may😂😂😂😂😂guéweul yi doundou lennnn

    3 mesi fa
  • el capo thiaw
    el capo thiaw

    Bidiw💥💥💥💥💥bou meillni diante

    3 mesi fa
  • Modou Mbaye
    Modou Mbaye

    Dans la vie la personne la plus dangereuse et l'hypocrite

    3 mesi fa
  • Soum Thier
    Soum Thier

    Mane dall djiguenii senegal yi diaxal nagne ma goor yallah bu takka nianrel rk guenn ........

    3 mesi fa
  • tiko tiko
    tiko tiko

    Lima diahal en général femmes you noir yiii gnimé beute saytané

    3 mesi fa
  • Amadou Aw
    Amadou Aw

    Mass c t'un vrai Gentalman ✊👊

    3 mesi fa
  • Khady Soumare
    Khady Soumare

    Biddew bulko bal deh djapsii rek nguir yallah ,guorgni beugnou koulén beug té fonkoulén, mayko touti ndakh mou réthiou .mdrrr

    3 mesi fa
  • Fatou Bintou Fall
    Fatou Bintou Fall

    Lamine ndiaye darame safouma

    3 mesi fa
  • Dija Ndiaye
    Dija Ndiaye

    Daro dinama ray 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 biddew balal mass way

    3 mesi fa
  • Natou Thiam
    Natou Thiam

    Bidew balko dou ko defati🥰😂😓

    3 mesi fa
  • Nabou Diouf
    Nabou Diouf

    Wa bidew qu'es ce que tu attends ppur changer de coiffure

    3 mesi fa